0
1:00
100%

bësal benn caabi ngir tàmbali

ã
&
é
~
"
#
'
{
(
[
-
|
ñ
`
_
\
ŋ
^
à
@
)
]
=
}
a
z
e
r
t
y
u
i
o
p
^
ó
¤
*
q
s
d
f
g
h
j
k
l
m
ù
<
w
x
c
v
b
n
,
;
:
!
xaaj
337 Waa mbooloo
312 Nattu (24w)
71 Kayitu seede yu ñu joxe
Kayitu seede yu mujj: Xool ñiy jiitu

Njàngum caabiy klawie ci Wolof

Njàngum caabi yi dañuy tàmbali ci réegu digg bi te génn, di yokk ay caabi yu néew ci yoon wu nekk te tàggatu ci yooyu rekk. Mooy yoon wi gën a yeex ngir jàng klawie, te mooy yoon wi rekk wuy tax nga bàyyi xool suuf.

Bind ci Wolof

Bii nattu ñu ngi ko tabax ci tëralinu klawie Wolof, te klawie bi ci ekaraŋ bi ak njàngum caabi yi dëppoo nañu ak caabi yu dëgg yi.

Laaj yi ñu gën a faral di laaj